Idda

Mia Guisse

Compositor: Não Disponível

Danga toog sama xol
Yaay ki ko moom léeboon
Gént naa takk la
Kaay doon sama yaayu doom
Dugg naa, dund naa
Muñ toog ndax yaw doom
Te bés bu sa doom indee doom
Def ko doom sama doom

Li nit di daj ci néegu-séy
Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey
Li nit di daj ci néegu-séy
Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey

Dinaa la romb midi (ooh wait)
Te doo ma gis (ooh wait)
Pénicillines yaa ngi ñëw (ooh wait)
Ma dàbbali (ooh wait)
Gaa fof no weli (ooh wait)
No dootoo ko defati (ooh wait)

Ooh wait, ooh wait

Ñaata yaay la fi séy
Tëj kaso ndax seen doom
Yii laaj, ngay laaj
Tay amaguma tontoom
Yàggatul, léegi rekk nga xam
Luy noon sama doom
Idda bi tay la jeex
Di jéggaluwaat sama doom

Li nit di daj ci néegu-séy
Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey
Li nit di daj ci néegu-séy
Di gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey

Dinaa la romb midi (ooh wait)
Te doo ma gis (ooh wait)
Pénicillines yaa ngi ñëw (ooh wait)
Ma dàbbali (ooh wait)
Gaa fof no weli (ooh wait)
No dootoo ko defati (ooh wait)

Dugg naa, dund naa
Muñ toog ndax yaw doom

Pare naa, xamoo ni bu jeexee
Jeex na, jeex na
Ñëwal!
Ah!
Nga ni!
Aah!
Aah!

Ma ne beydu volume
Saabu mi nanaani
Tekkil lunettes yi
Ngir gën a gis

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital